Revelation 3:18 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Moo tax maa ngi lay xiirtal, nga jënd ci man wurus wu ñu xellee ci safara, ngir nga duunle, te nga jënd yére yu weex ngir nga solu, ba sa gàcceg rafle bañ a feeñ, ak tuufaay booy diw ci say bët, ngir man a gis. i
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
dama lay digal, nga jënd ci man wurus wu ñu xellee ci sawara ba mu set wecc, ngir nga am alal. Jëndal itam yére yu weex yoo soloo, ba làq sa duŋŋaaral gu gàccelu gi; ak tuufaay looy tuufoo, ngir nga gis.