Revelation 3:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ku daan, dinga sol mbubb mu weex ni ñoom. Te duma far sa tur ci téereb dund bi, waaye dinaa nangu ci sama kanamu Baay ak ay malaakaam ne, bokk nga ci man.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ku am ndam mooy soloo noonu mbubb mu weex, te turam, duma ko far ci téereb dund bi, waaye maa koy wuyul ci sama kanam Baay ak ay malaakaam.