Revelation 3:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xam naa say jëf. Ubbil naa la bunt, te kenn du ko man a tëj. Xam naa ne barewuloo doole, waaye sàmm nga sama kàddu te weddiwoo ma.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gis naa say jëf. Maa def fi sa kanam, bunt bu tijjiku bu kenn manula tëj. Ndax néew nga doole, waaye sàmm nga sama kàddu te weddiwoo ma.