Revelation 3:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dinaa def ba ñenn ci ñi bokk ci ndajem Seytaane --te tuddoo Yawut, fekk dañuy fen — dinaa leen ñëwloo, ñu sukk ci sa kanam, nangu ne, bëgg naa la.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñenn ci jàngub Seytaane bi, ñooñuy fen, di tuddoo ay Yawut te duñuy Yawut, maa ngii di leen xiirtal, dikkloo leen, sujjóotloo leen fi sa kanam, ba ñu xam ne man maa la sopp.