Revelation 6:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu weneen fas génn, di wu xonq, gawar ba jot sañ-sañu jële jàmm ci kaw suuf, ngir nit ñi di reyante ci seen biir. Ñu jox ko jaasi ju mag.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Weneen fas ne jimeet, di wu xonq, ñu may gawaram mu jële jàmm ci kaw suuf, ngir nit ñi di reyante ci seen biir. Ñu jox ko saamar bu mag.