Revelation 8:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Biddiiw boobu mi ngi tuddoon Wextan. Nit ñu bare naan ci ndox mi daldi dee, ndaxte ndox mi dafa daldi wex.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Biddiiw bi Wextan la tudd. Ñetteelu xaaju ndox yépp la wexal, ñu bare naan ci, daldi dee, ndax wextanu ndox mi.