Revelation 8:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu saxarus cuuraay li gillee ca loxob malaaka ma, ànd ak ñaani gaayi Yàlla ya, jëm ca kanam Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Saxaras cuuraay laa ngi gillee ci loxol malaaka mi, ànd ak ñaani ñu sell ñi, di yéeg fa Yàlla.