Revelation 8:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
benn ci ñetti xaaju mbindeef yi nekk ci géej gi dee, te benn ci ñetti xaaju gaal yi yàqu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ñetteelu xaaju bindeefi géej dee, ñetteelu xaaju gaal yi yàqu yaxeet.