Revelation 9:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Am nañu ay geen yu am ay fitt ni jànkalaar, te ca la seen kàttan nekk, ngir metital nit ñi diirub juróomi weer.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Geen gu am fitt lañu am ni jànkalaar. Daŋaru geen googu lañuy mititale nit ñi diiru juróomi weer.