Revelation 9:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Buuru njéeréer yi mooy malaakam kàmb gu xóot gi, moom lañu tudde ci làkku Yawut, Abadon, ak ci làkku gereg, Apolyon, liy tekki «Yàqkat.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Seen buur a leen jiite, di malaakam xóote bi, turam ci ebrë di Abadon, Apolyon ci làkku gereg, (mu firi Yàqkat bi).