Revelation 9:15 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu ñu daldi yiwi ñeenti malaaka, ya ñu waajaloon ngir at moomu, weer woowu, bés boobu ak waxtu woowu, ngir ñu rey benn ci ñetti xaaju nit ñi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ca lañu yiwi ñeenti malaaka, ya ñu waajaloon ñeel waxtu woowu, ci bés boobu, weer woowu, at moomu, ngir ñu rey ñetteelu xaaju nit ñi.