Revelation 9:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte kàttanu fas yaa ngi ci seeni gémmiñ ak ci seeni geen. Geen yaa nga mel ni ay jaan, am ay bopp, te ñoom lañuy metitale nit ñi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Daŋaru fas yaa ngi ci seen gémmiñ ak ci seen geen, ndax seen geen yaa ngi mel ni ay jaan, ami bopp yu ñuy mititalee.