Revelation 9:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ca jamono yooya nit ñi dinañu sàkku dee, waaye duñu daje ak moom. Dinañu bëgg a dee, waaye dee da leen di daw.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bési keroog nit ñeey sàkku dee, te duñu ko daj, ñu ne siiwa dee, ndee daw leen.