Revelation 9:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Njéeréer ya nag dañuy niroo ak fas yu ñu waajal ngir xare. Am nañu ci seen bopp lu mel ni kaalay wurus, te seen xar-kanam mel ni gu nit.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Njéeréer yaa ngi nirook fas yu ñu waajal ngir xare, kaalawoo lu mel ni kaalay wurus, seen kanam nirook kanamu nit,