Romans 1:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te li ma koy faral di ñaan mooy lii: bu soobee Yàlla, na ma ubbil bunt, ba ma man a ñëw ci yéen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xanaa di saxoo dagaan ci samay ñaan, su ci Yàlla àndee, yoon wu jub wu ma mujj dikke ba ci yeen.

Recommended Reading