Romans 1:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Li aju ci man nag, jekk naa ngir ñëw, xamal leen xebaar bu baax bi, yéen it waa Room.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax, yeen waa Room itam, ma yàkkamti leena àggesi xibaaru jàmm bi.