Romans 1:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndax li nit man a xam ci Yàlla, leer na ci seen xel, ndax Yàlla won na leen ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndaxam lees mana xam ci Yàlla, leer na ci seen biir, nde Yàlla moo leen ko leeralal.