Romans 1:3 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
di xamle mbirum Doomam, Yeesu Kirist sunu Boroom. Lu jëm ci meloom ci àddina, ci askanu Daawuda la jóge, waaye lu jëm ci xelam mu sell, Doomu Yàlla la; ndaxte ndekkiteem nekk na firnde ju ràññiku, ne moom la.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
moo jëm ci Doomam, ji soqikoo ci askanu Daawuda, ci wàllu àddina.