Romans 1:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te ci ngeen bokk, yéen ñi Yàlla woo, ngeen nekk ci Kirist.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te yeen ñi ñu woo ci Yeesu Almasi itam, ci ngeen bokk.