Romans 10:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mbind mi dafa wax ne: «Képp ku ko gëm, sa yaakaar du tas mukk.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mbind mi moo ne: «Képp ku ko gëm, doo rus.»