Romans 10:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ñépp nanguwuñu xebaar bu baax bi; moom la Esayi wax ne: «Boroom bi, ana ku gëm sunu waare?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye du ñépp a nangul xibaaru jàmm bi; moo tax Esayi ne: «Boroom bi, ana ku gëm sunub dégtal?»