Romans 10:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ci mbirum Israyil dafa wax ne:«Tàllal naa samay loxo, suba ba ngoon, ci xeet wu may bañ tey werante.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Israyil nag la wax ci mbiram ne: «Bëccëg bépp laa yendoo tàllal samay loxo, askanu fippukat wu déggadi.»