Romans 10:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte ci Kirist la yoonu Musaa dëppe, ba tax ku ko gëm, dinga jub fa kanam Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat Almasi moo sottal yoonu Musaa, ngir àtteb ku jub ñeel képp ku ko gëm.