Romans 10:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ku bëgg a jub ci kanam Yàlla ci kaw sàmm yoon, Musaa daf cee wax ne: «Ku ko manoon a matal, dinga dund ba fàww.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Njub gi sàmm ndigali yoon di maye, li ci Musaa bind moo di: «Kuy jëfe digal yooyu, yaay dund ndax ñoom.»