Romans 10:7 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
«Bul wax it:“Kuy dem ca barsàq?”» mel ni dangaa bëgg Kirist dekki.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Bul ne it: “Ana kuy wàcci njaniiw?”» nde loolu mooy Almasi dekkiwaat ngay sàkku.