bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Romans 10:8
Romans 10:8 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Kon boog lan lay wax? Lii:«Waxu Yàlla mi ngi ci sa wet,ci sa làmmiñ, ci sa xol.» Te wax jooju lal ngëm lanuy waare.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li mu wax moo di: «Kàddu gaa ngi ci sa wet; mu ngi ci saw làmmiñ ak ci sa xol.» Te loolu mooy kàddug ngëm gii nuy xamle.