Romans 11:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dama koy def, ngir ñi bokk ak man xeet siis, ba ñenn ñi mucc.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jombul sama liggéey dina yee fiiraangey sama bokki Yawut ñi, ba ñenn ci ñoom mucc.