Romans 11:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xanaa dinga wax ne: «Car yooyu dañu leen a fàq, ngir jabtal ma fa ñu nekkoon.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xam naa dinga ne: «Car yooyu, dees leena tenqi, ngir jabtal ma.»