Romans 11:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yàlla bërgëlul xeetam, wi mu xamoon lu jiitu. Ndax dangeen a xamul li Mbind mi di wax ci mbirum Iliyas? Dafa doon tawat Israyil ci Yàlla naan:
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yàlla waccul ñoñam ñi mu ràññee woon lu jiitu. Am dangeena xamul li Mbind mi indi ci mbirum Ilyaas, ba mu dikkee Yàlla njàmbat lu jëm ci Israyil? Mu ne: