Romans 11:26 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bu loolu amee nag, bànni Israyil gépp dina mucc. Moom la Mbind mi tëral, bi mu naan:«Ab xettalikat dina jóge ci Siyon,dàq weddi ci askanu Yanqóoba.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su boobaa nag, bànni Israyil gépp ay mucc, noonee ko Mbind mi indee ne: « Siyoŋ la wallukat bay jóge, mooy tenqee ngëmadi ci askanu Yanqóoba.