Romans 11:30 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñu déggadil Yàlla ngeen woon, waaye ngëmadig Yawut yi tax na, ngeen jot yërmandeem.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeena déggadi woon, waaye tey daj ngeen yërmande, ndax déggadig Yawut yi.