Romans 11:31 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ñoom itam lànk nañu léegi, ngir man a bokk ak yéen yërmandey Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noonu itam la Yawut yi déggadee tey, ba ni ngeen daje yërmande, ñoom it ñu daje ni yërmande.
Recommended Reading