Romans 11:32 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon Yàlla tëj na ñépp ci ngëmadi, ngir man a yërëm ñépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yàlla moo tëj nit ñépp ci seenug déggadi, ngir yërëm leen ñoom ñépp.