Romans 11:34 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mbind mi dafa ne:«Ana ku xam xalaatu Boroom bi?Ku ko doon digal?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Ana ku xam xalaatu Boroom bi? Ana ku ko digal?»