Romans 11:36 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte ci moom la lépp sosoo, ci moom la lépp di jaar, ci moom la lépp di dellu. Moo yelloo ndam ba fàww. Amiin.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci moom la lépp sosoo, ci moom la lépp sottee, te moom la lépp ñeel. Moom la daraja ñeel ba fàww! Amiin.