Romans 11:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon lu nu ci war a wax? Li bànni Israyil doon wut, gisuñu ko. Waaye ñi Yàlla tànn rekk a ko gis, te ña ca des bañ a gëm, ba seen xol dërkiis.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon léegi nag? Li am moo di li bànni Israyil doon wut, amuñu ko. Ñi ñu taamu ñoo ko am, ña ca des, seenum xel a dërkiis.