Romans 12:15 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bégandooleen ak ñi bég, te jooyandoo ak ñiy jooy.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñi ci mbégte, bokkleen ak ñoom seen mbégte; ñi ci naqar, ngeen bokk ak ñoom seen naqar.
Recommended Reading