Romans 12:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu leen àddina jey, waaye yeesluleen ci seen xel, ba soppiku, ngeen man a xam bu wér coobareg Yàlla, di lépp lu baax, neex ko te mat sëkk.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buleen roy jamonoy tey jii, waaye yeesluleen ci ni ngeen di xalaate ba soppiku, ngir ngeen mana ràññee liy coobarey Yàlla, muy li baax, di bànneexam te mat sëkk.