bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Romans 12:20
Romans 12:20 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye defleen lii:«Bu sa noon xiifee, may ko mu lekk;bu maree, may ko mu naan.Ndax boo ko defee, dinga ko rusloo.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li mu wax kay mooy: «Bu sab noon xiifee, jox ko mu lekk, bu maree, may ko mu naan. Soo defee noonu, day rus, ba mel ni koo yen ay xal.»