Romans 12:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw Yàlla may na ma ciw yiwam, ma nekk ndawam, maa ngi leen di wax lii, kenn ku nekk ci yéen: buleen yég seen bopp, waaye ngeen am xalaat yu yem, mengook ngëm gi leen Yàlla sédd, ku nekk ak wàllam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ma àrtu leen ci kaw yiw wi ma Yàlla may; bu kenn ci yeen teg boppam fu mu àggul, waaye xalaate leen sago, te ku nekk dëppoo ak céru ngëm bi ko Yàlla sédd.