Romans 13:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye gànnaayooleen Yeesu Kirist Boroom bi, te bañ a topp seen bakkan ciy bëgg-bëggam yu bon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye yiirooleen Sang Yeesu Almasi, te ngeen baña yittewoo seen bakkan, ngir di topp seeni xemmemtéef.