Romans 13:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon ku leen bañ a déggal, ndigalu Yàlla nga lànk, te ku def loolu, yoon dina la dab.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax kuy bañal njiit, tëralinu Yàlla nga bañal, te ñi bañal njiit, ñoo wool seen bopp mbugal.