Romans 13:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw Yàllaa sas njiit yi liggéey boobu, te ñi ngi ci, kon fàww ngeen fey galag.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu moo waral it ngeen di fey galag, ndax njiit yi koy feyeeku kat, ñooy jawriñi Yàlla yi sasoo googu kilifteef.