Romans 14:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte Mbind mi tëral na lii:«Boroom bi nee na:“Ni mu wóore ne maa ngi dund,ni la wóore ne, ñépp dinañu ma sukkal,te ku nekk seede ne maay Yàlla.”»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndaxte bindees na ne: «Ndegam maay Kiy Dund, Boroom bee ko wax, man la ñépp di sukkal seen bëti óom, te man Yàlla la làmmiñu ñépp di sàbbaal.»