Romans 14:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Soo dee lekk luy indil sa moroom tiis, génn nga ci mbëggeel. Yaw nag bul réeral sa moroom ci sa ñam, ndax Kirist dee na ngir moom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Soo dee lekk lenn ba tax sa mbokk am ci lu ko naqari, noppi ngaa doxe cofeel. Bu sag lekk sànk ku Almasi deeyal.