Romans 14:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag nanu wut luy indi jàmm, tey yékkati ngëmu sunu moroom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag nanu sàkku luy indi jàmm, ak lu nu feddalantee.