Romans 14:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Liy sa warugar mooy nga bañ a fiir sa moroom ci yàpp mbaa ci biiñ mbaa ci leneen lu mu man a doon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li gën sax mooy nga baña lekk yàpp, mbaa nga baña naan biiñ, mbaa leneen lu mu doon lu mana fakktal sa mbokkum gëmkat.

Recommended Reading