Romans 14:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye kuy lekk ñam te am ci xel ñaar, def nga bàkkaar, ndax sa ngëm yemu fa. Ndaxte jëf ju àndul ak ngëm, bàkkaar la.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye ki am xel-yaar, su lekkee, ab daan topp na ko, nde jëfewul ngëm, te lu ngëm lalul bàkkaar la.