bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Romans 14:5
Romans 14:5 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu itam am na ñiy tànn bés ak ñiy yemale bés yépp. Na ku nekk xam bu wér li muy def, te jàpp ci.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka noonu kii jàpp na ne bés gën naa rafet moroom ma; kee jàpp ne bés yépp a yem. Na ku nekk seet la ko doy, te yem ca.