Romans 14:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte kuy tànn bés, mu ngi koy def ngir màggal Boroom bi. Kiy lekk lu nekk it, mu ngi koy def ngir màggal Boroom bi; loolu leer na ndax day sant Yàlla. Te it ki bañ a lekk yàpp, mu ngi koy def ngir màggal Boroom bi, di ko sant.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kiy taamu bés, Boroom bi la koy taamul; naka noonu kiy lekk, Boroom bi la koy gërëme, nde moom lay sant doora lekk; ki lekkul it Boroom bi lay sàkkoo ñàkka lekkam, te Yàlla lay sant.